27 Ganou ga jigen ja itam dē.
Ñarel ba itam def nōgule, ak ñetel ba, be cha jurom ñarel ba.
Chi ndēkite ga mbōk, jabar i kan la di neka chi jurom ñar ña? ndege ñepa sey on nañu ak mōm.