23 Bes bōbale i Sadducee, ñu ne ndēkite amul, ñou fi mōm, te lāj ko,
Yesu ne len, Otu len te moytu mporoh͈al i Pharisee ya ak Sadducee ya.
Wande ba mu gise jupa chi Pharisee ya ak Sadducee ya di ñou chi batise am, mu ne len, E h͈êt i ñangōr gi, kan a len yēgal ngēn di ūt a rēcha chi mer mi di ñou?