2 Ngur i ajana niro na ak bena bur bu h͈umbal on nchēt i dōm am;
Mu teg benen lēb chi sēn kanam, ne, Ngur i ajana niro na ak nit ka ji on jiu ju bāh͈ chi tōl am;
Yesu tontu te wah͈ati len chi i lēb, ne,
Ô on nañu itam Yesu ak i talube am cha sey ba.