14 Ndege ñu bare la ñu ô, wande ñu new la ñu tana.
Nōnule ña muje di nañu jītuji; te ña jītu di nañu mujeji.
Su ñu gatalul on bes yōgale, ken du kon muchi: wande ngir ña ñu tana, di nañu gatal bes yōgale.
Ndege Krista yu nafeh͈a di nañu jogi, ak yonent yu nafeh͈a, te wone mandarga yu rey ak i koutef; be ñu di nah͈i ña ñu tana sah͈, su munê am.