Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 22:13 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

13 Fōfale bur ba ne i rapas am, Ew len loh͈o am ak tank’ am, te sani ko chi lendem i biti; fōfale la joy di neka ak yey i buñ.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 22:13
21 Iomraidhean Croise  

Naka la kena munê h͈araf chi nēg i borom‐dōle, te yah͈a alal am, su jekulê taka borom‐dōle ja? te ganou lōla di na yah͈a nēg am.


Bayi len ñar ña ñu sah͈ando be cha ngōbte ga; te cha wah͈tu’ ngōbte ga di nā wah͈ gōbkat ya, ne, Budi len jeka nduh͈um la, taka ko i say te laka ko; wande dajale len dugup ja chi suma sah͈a.


Te sani len cha safara sa; fōfale la joy di neka, ak yey i buñ.


Te sani len chi safara si: fōfale la joy di neka, ak yey i buñ.


Dog ko chi diga, te sedāle ko nafeh͈a ya: fōfale la joy di neka, ak yey i buñ.


Te sani len jām bu jeriñul bi cha lendem i biti: fōfale la joy di neka, ak yey i buñ.


Wande i dōm i ngur ga, di nañu len tabal chi lendem i biti; fōfale la joy di neka ak yeyi buñ.


Chi dega, chi dega, mangi la di wah͈, Ba nga nek’ on ndau, dan nga lah͈asay sa bopa, te doh͈āni fo buga: wande bo magete, di nga talal sa i loh͈o, te kenen di na la lah͈asay, te yubu la fo bugul.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan