1 Yesu tontu te wah͈ati len chi i lēb, ne,
Ngur i ajana niro na ak bena bur bu h͈umbal on nchēt i dōm am;