33 Dēglu len benen lēb: Bena borom‐ker am on na, ku jembat on tōl, ñak ko, gas cha nalukay, tabah͈ am tata, lūye ko i ligeykat, te dem cha benen rew.
Dēga len mbōk lēb i jikat ba.
Ndege ngur i ajana niro na ak bena borom‐ker ku gēna chi sūba têl, ndah͈ mu binda i ligeykat chi tōl am.
Wande lan ngēn dēfe? Kena nit am on na ñar i dōm yu gōr; mu ñou chi tau ba, ne, Suma dōm, demal ligey tey chi suma tōl.
Bindānkat ya ak Pharisee ya tōg nañu chi tōgu’ Musa:
Man mā di garap i biñ bu dega bi, te suma Bay a di beykat ba.