Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 21:32 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

32 Ndege John ñou on na fi yēn chi yōn i njūbay, te gumu len ko won: wande publican ya ak garbo ya gum on nañu ko: te yēn ba ngēn ko gise, rechuwu len cha ganou sah͈ ndah͈ ngēn gum ko.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 21:32
19 Iomraidhean Croise  

Ndege John ñouūl on di leka wala di nān, te ñu ne, Anda na ak jine.


Batise’ John, fan la juge won? cha ajana am chi nit? Ñu werante chi sēn digante, ne, Su ñu ne, Cha ajana; di na ñu ne, Lutah͈ gumu len ko won mbōk?


Kan chi ñom ñar a def la sēn bay buga? Ñu ne ko, Tau ba. Yesu ne len, Chi dega mangi len di wah͈, Publican ya ak garbo ya di nañu dem chi ngur i Yalla as yēn.


Ndege su ngēn sope ña len sopa dal, ban yōl ngēn di am? Publican ya sah͈ du ñu def nōgule am?


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan