Matthew 21:31 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
31 Kan chi ñom ñar a def la sēn bay buga? Ñu ne ko, Tau ba. Yesu ne len, Chi dega mangi len di wah͈, Publican ya ak garbo ya di nañu dem chi ngur i Yalla as yēn.
Su ngēn di ñān, bu len def niki nafeh͈a ya: ndege sopa naño tah͈ou di ñān chi juma ya ak chi mbeda ya, ndah͈ nit gis len. Chi dega mangi len di wah͈, Am nañu sēn yōl.