30 Mu ñou cha ñarel ba, te wah͈ati lōga. Mu tontu, ne, Di nā dem; wande demul.
Mu tontu, ne, Du ma dem: wande cha ganou mu rēchu, te dem.
Kan chi ñom ñar a def la sēn bay buga? Ñu ne ko, Tau ba. Yesu ne len, Chi dega mangi len di wah͈, Publican ya ak garbo ya di nañu dem chi ngur i Yalla as yēn.
Mōtah͈ lu mu mun a don lu ñu len ebal, dēgal len, te def ko; wande bu len def naka sēn i jef; ndege ño di wah͈, te du ñu def.