28 Wande lan ngēn dēfe? Kena nit am on na ñar i dōm yu gōr; mu ñou chi tau ba, ne, Suma dōm, demal ligey tey chi suma tōl.
Mu ne, Wau. Ba mu h͈arafe chi nēg ba, Yesu jekantu ko, ne, Lo dēfe Simon? I bur i suf si, chi kan la ñu di jele bāh͈ wala ngalak? chi sēn i dōm am, am chi i gan?
Ndege ngur i ajana niro na ak bena borom‐ker ku gēna chi sūba têl, ndah͈ mu binda i ligeykat chi tōl am.
Ñu tontu Yesu, ne, H͈amu ñu. Mu ne len it, Man du ma len wah͈ ak ban sañsañ lā defe yef yile.
Mu tontu, ne, Du ma dem: wande cha ganou mu rēchu, te dem.
Dēglu len benen lēb: Bena borom‐ker am on na, ku jembat on tōl, ñak ko, gas cha nalukay, tabah͈ am tata, lūye ko i ligeykat, te dem cha benen rew.
Wah͈ ñu nak, Lo dēfe? Ndah͈ dagan na ñu joh͈ Cæsar ngalak, am dēt.