25 Batise’ John, fan la juge won? cha ajana am chi nit? Ñu werante chi sēn digante, ne, Su ñu ne, Cha ajana; di na ñu ne, Lutah͈ gumu len ko won mbōk?
H͈alāt nañu chi sēn bopa, ne, Ndig indiū ñu on mburu.
Yesu tontu len ne, Man it di nā len lāj bena bāt, te su ngēn ma ko wah͈e, di nā len wah͈ itam ak ban sañsañ lā defe yef yile.
Wande su ñu ne, Chi nit; da ñu ragal mbōlo ma; ndege jape won nañu John niki yonent.
John sēde on na ko, te h͈āchu, ne, Kile di ka ma wah͈ on, ne, Ka di ñou chi suma ganou neka na chi suma kanam, ndege mō ma jek’ on a neka.
Nit ñou on na ka Yalla yōni on, ku tūda John.
Ku gum chi mōm atewu ñu ko; ku gumul, ate nañu ko jēg, ndege gumul on chi tur i Dōm i Yalla ja di bajo.