Matthew 21:23 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
23 Ba mu ñoue chi bir juma ja, i njīt i seriñ ya ak i mag i nit ña ñou fi mōm ba mō jemantale, ne, Ak ban sañsañ nga defe yef yile? te ku la joh͈ sañsañ bile?
Chi wah͈tu wōwale Yesu ne mbōlo ma, Dika ngēn jelsi ma ak i jāsi ak i doko, niki sachakat? Dan nā tōg ak yēn gir gu neka, di jemantale chi juma ja, te japu len ma won.