17 Mu bayi len, gēna cha deka ba chi bir Bethany, te fanān fa.
H͈êt wu bon ak njālo ūt na mandarga; du ñu ko may mandarga, lu dul mandarga i Jonah. Mu bayi len, te dem.
Ba Yesu neke chi Bethany nak, chi nēg i Simon gāna ga,
Jena way jēr on na, Lazarus cha Bethany, dek’ i Mariama, ak mag am Martha.
Bethany jegeñ na Jerusalem, lu day ni fuk’ i furlong ak jurom.