Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 21:16 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

16 Te ne ko, Ndah͈ dēga nga li ñile di wah͈? Yesu ne len, Wau: ndah͈ mosu len a janga, ne, Chi gemeñ’ i dōm ak i gūne yu di nampa nga motali nau?

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 21:16
11 Iomraidhean Croise  

Cha wah͈tu wōwale Yesu tontu, ne, Mangi la gerem, Bay bi, Borom’ asaman ak suf, ndege nuba nga yef yile chi borom‐h͈amh͈am yi ak borom‐sago yi, te fêñal len i gūne.


Wande mu ne len, Ndah͈ jangu len la Dauda def on ba mu h͈īfe, ak ña and’ on ak mōm;


Mu tontu len, ne, Ndah͈ jangu len ne ka len bind’ on cha ndôrte la, dafa len bind’ on gōr ak jigen,


Wande mosu len a janga lu jem chi ndēkite ga, la len Yalla wah͈ on, ne,


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan