9 Ba ña mu bind’ on potah͈ juromel i wah͈tu chi ngon ñoue, nit ku nek’ am h͈asab.
Ba ñu jeka ñoue, ñu fōg ne di nañu jot lu upa lōga; wande ku neka itam am h͈asab.
Ba mu wah͈ante ak ligeykat ya h͈asab bechek, mu yōni len cha tōl am.
Ba ngon jote, borom‐tōl ba ne bukanēg am, Ôal ligeykat ya, te joh͈ len sēn mpey, di dôr cha ña muje be cha ña jek’ on.