3 Mu gēnati potah͈ chi jurom ñenentel i wah͈tu, gis ñenen ñu tah͈ou chi jēy ba te defu ñu dara,
Ba mu wah͈ante ak ligeykat ya h͈asab bechek, mu yōni len cha tōl am.
Mu ne len, Dem len yēn it cha tōl ba, te di nā len joh͈ lu ela. Ñu dem.