Ñom it di nañu ko tontu, ne, Borom bi, kañ la ñu la gis on nga h͈īf, wala nga mar, wala nga di gan, wala nga rāfle, wala nga jēr, wala chi kaso, te dimaliū ñu la?
Yesu tontu, ne, Suma ngur bokul chi aduna sile: su suma ngur bok’ on chi aduna sile, kōn suma i bukanēg di nañu h͈ēh͈, ndah͈ du ñu ma jebal fa Yauod ya: wande suma ngur jugewul fōfule.