25 Wande Yesu ô len fi mōm, te ne, H͈am ngēn ne i kēlifa i Gentile ya ēlif nañu len, te ñu rey ña ate nañu len ak sañsañ.
Enu len suma suf chi yēn, te jemantu len chi man; ndege da ma lew, te sufelu chi h͈ol; te di ngēn feka noflay chi sēn i fit.
Ba ko fuka ña dēge, ñu mere ñar i mboka ya.