2 Ba mu wah͈ante ak ligeykat ya h͈asab bechek, mu yōni len cha tōl am.
Wande jām bōbale gēna, te feka kena chi i naule am, ku ko leb on tēmēr i kopar: mu japa ko, ne ko chih͈ chi bāt am ne, Fey ma lo ma leb on.
Ndege ngur i ajana niro na ak bena borom‐ker ku gēna chi sūba têl, ndah͈ mu binda i ligeykat chi tōl am.
Wande mu tontu kena chi ñom, ne, H͈arit, tōñu ma la: du bena h͈asab la ñu wah͈ante won am?
Mu gēnati potah͈ chi jurom ñenentel i wah͈tu, gis ñenen ñu tah͈ou chi jēy ba te defu ñu dara,
Ba ña mu bind’ on potah͈ juromel i wah͈tu chi ngon ñoue, nit ku nek’ am h͈asab.
Won len ma h͈ālis i ngalak li. Ñu yub ko h͈asab.
Fōfale mu wah͈ i tālube am, ne, Chi dega ngōbte gi fūs na, wande ligeykat yi new nañu;