10 Ba ñu jeka ñoue, ñu fōg ne di nañu jot lu upa lōga; wande ku neka itam am h͈asab.
Fōfale Peter tontu ko, ne, Ñun ño wocha yepa, te topa la; lan la ñu ami mbōk?
Ba ñu ko jele, ñu ñurumtu lu jem chi borom‐ker ga, ne,
Ba mu wah͈ante ak ligeykat ya h͈asab bechek, mu yōni len cha tōl am.
Ba ña mu bind’ on potah͈ juromel i wah͈tu chi ngon ñoue, nit ku nek’ am h͈asab.