Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 2:2 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

2 Ne, Ana ki jūdu Bur i Yauod ya? Ndege gis on nañu bidiw am cha Penku, te dika nañu ndah͈ ñu jāmu ko.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 2:2
28 Iomraidhean Croise  

Ba Herod bur ba dēge lōla, mu jāh͈le, mōm ak Jerusalem yepa.


Yēgal len dōm i Zion, Sa Bur anga dika fi you, lew, te di war mbamsuf, ak chumbur dōm i mbamsuf.


Yesu tah͈ou chi kanam i kēlifa ga, te kēlifa ga lāj ko, ne, Ndah͈ yā di Bur i Yauod ya? Yesu ne ko, Wah͈ nga ko.


Nathanael tontu ko, ne, Rabbi, yā di Dōm i Yalla; yā di Bur i Israel.


Ñu fah͈a i banh͈as i tir ya, te dem gatanduji ko, te h͈āchu ne, Hosanna: barkel chi ka di dika chi tur i Borom ba, mu di Bur i Israel.


Pilate ne ko, Ndah͈ bur nga? Yesu tontu, ne, Wah͈ nga ko, ndege man bur la. Lile tah͈ ma jūdu on, te lile tah͈ ma ñou chi aduna si, ndah͈ ma sēde dega gi. Ku neka ku boka chi dega gi di na dēga suma bāt.


Te Pilate bind on na h͈ameukay am itam, te def ko cha kura ba. Te lile la binda, Yesu wā’ Nazareth, Bur i Yauod ya.


Thomas tontu te ne ko, Suma Borom ak suma Yalla.


Ndah͈ ñepa mun a teral Dōm ji naka ñu terale Bay ba. Ku teralul Dōm ji teralul Bay ba ko yōni on.


Te mu ne, Gum nā, Borom bi; te mu jāmu ko.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan