Matthew 2:16 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 190716 Herod nak, ba mu gise ne borom‐h͈amh͈am ya nah͈ nañu ko, mu mer lol; mu yōne, te rēyat h͈alel yu gōr ya yepa ñu nek’ on cha Bethlehem, ak cha mpega ya, ñu am on ñar i at ak lu gen a new, naka cha wah͈tu wa mu lājte on borom‐h͈amh͈am ya. Faic an caibideil |