Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 2:14 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

14 Mu jog, jel gūne ga ak ndey am chi gudi, te dem cha Mesara:

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 2:14
6 Iomraidhean Croise  

Yusufa jog chi nelou, def la ko malāka i Borom bi ebal on, te jel ko jabar:


Ba ñu dem on, malāka i Borom bi fêñu Yusufa chi gēnta, ne, Jogal, jelal gūne gi ak ndey am, te dou cha Mesara, te jēki fa be ba ma la cha ôe, ndege Herod di na ūt gūne gi ndah͈ mu rēylu ko.


Mu neka fa be ba Herod dēe, ndah͈ la Borom bi wah͈ on cha yonent ba motaliku, ne, Cha Mesara lā ôe suma dōm.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan