Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 2:13 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

13 Ba ñu dem on, malāka i Borom bi fêñu Yusufa chi gēnta, ne, Jogal, jelal gūne gi ak ndey am, te dou cha Mesara, te jēki fa be ba ma la cha ôe, ndege Herod di na ūt gūne gi ndah͈ mu rēylu ko.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 2:13
29 Iomraidhean Croise  

Wande ba mu h͈alāte yef yile, malāka i Borom bi fêñu ko chi gēnta, ne ko, Yusufa, dōm i Dauda, bul ragal a sey ak Mariama, ndege li chi bir am chi Nh͈el mu Sela ma la juge.


Wande su ñu len getene chi deka bile, dou len fa benen; ndege chi dega ma ne len, Du len won demi chi i dek’ i Israel yepa be ba Dōm i nit ka di ñoui.


Te Yalla yēgal on na len chi gēnta, ne bu ñu delu fa Herod; mōtah͈ ñu ñibi sēn deka cha wenen yōn.


Mu jog, jel gūne ga ak ndey am chi gudi, te dem cha Mesara:


Herod nak, ba mu gise ne borom‐h͈amh͈am ya nah͈ nañu ko, mu mer lol; mu yōne, te rēyat h͈alel yu gōr ya yepa ñu nek’ on cha Bethlehem, ak cha mpega ya, ñu am on ñar i at ak lu gen a new, naka cha wah͈tu wa mu lājte on borom‐h͈amh͈am ya.


Wande ba mu dēge ne Archelaus ngūru chi bereb i bay am Herod, mu ragal a dem fōfa; te ba ko Yalla yēgale chi gēnta, mu dem cha wet i Galilee,


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan