10 Ba ñu gise bidiw ba, ñu banēh͈u ak banēh͈ gu rey lol.
Ba ñu h͈arafe cha nēg ba, ñu feka gūne ga ak Mariama ndey am; ñu sūka te jāmu ko; ñu ūbi sēn i wah͈ande, te jebal ko i maye: wurus, fufata, ak mira.
Ba ñu dēge bur ba, ñu dem; te bidiw ba ñu gis on cha Penku, jītu len, be ba mu tah͈oue cha kou bereb ba gūne ga neka.