5 Te nôn, Ndig lile tah͈na be nit di bayi bay am ak ndey am, bōlo ak jabar am, te di nañu neka bena yaram ñom ñar?
Nōgule nekatu ñu ñar, wande bena yaram. Mōtah͈ lu Yalla bōlāte, nit waru ko fasāle.