30 Wande bare na ña jītu di nañu mujeji; te ña muje di nañu jītuji.
Nōnule ña muje di nañu jītuji; te ña jītu di nañu mujeji.