3 Pharisee ya ñou fi mōm, di ko fir, te ne ko, Ndah͈ dagan na nit fase jabar am ndig lu mu mun a don?
Pharisee ya ak Sadducee ya ñou di ko fir, te lāj ko mu won len mandarga cha asaman.
Kena chi ñom ku h͈amkat i yōn la won, lāj ko di ko fir, ne,
Te lile wah͈ nañu ko di ko jēm, ndah͈ ñu mun a am lu ñu ko jêñ. Wande Yesu sega, te binda chi suf si ak baram am.