26 Yesu sêt len, ne len, Lile munul a am ak nit; wande dara teūl Yalla.
Ba tālube ya dēge lōla, ñu jomi lol, ne, Ndōg kan a mun a mucha?
Fōfale Peter tontu ko, ne, Ñun ño wocha yepa, te topa la; lan la ñu ami mbōk?