19 Teralal sa bay ak sa ndey: te, Sopal sa morom niki sa bopa.
V. Teralal saa bai ak saa nde, ndah saa i fan mun na guda ce suf sa la Yalla saa Borom mai.
Far wa ne ko, Lōlu yepa lā dēncha: lan lā ñakati?
Te ñarel bu niro ak mōm di bile, Na nga sopa sa morom niki sa bopa.
Dēga ngēn ñu wah͈, ne, Na nga sopa sa morom, te sib sa mbañ.