Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 19:16 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

16 Kena ñou fi mōm, ne, Jemantalkat bi, lan lef lu bāh͈ lā ela def, ndah͈ ma mun a am dunda gu dul jêh͈?

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 19:16
32 Iomraidhean Croise  

Mu teg i loh͈o am chi sēn kou, te juge fōfa.


Yesu sêt len, ne len, Lile munul a am ak nit; wande dara teūl Yalla.


Te ku neka ku bayi i nēg, mbāt i raka, mbāt i jigen, mbāte bay, mbāte ndey, mbāt i dōm, mbāt i tōl ngir man, di na ami lu bare lu len upa, te dona dunda gu dul jêh͈.


Ñile di nañu dem chi ndān gu dul jêh͈: wande ñu jūb ña chi dunda gu dul jêh͈.


Te may nā len dūnda gu dul jêh͈; te du ñu sanku muk, te ken du len foh͈arñi chi suma loh͈o.


Ku sopa dūnd’ am, di na ko rēral; te ku bañ dūnd’ am chi aduna sile, di na ko dēncha be cha dūnda gu dul jêh͈.


Ndah͈ ku mu mun a don ku gum chi mōm di na am dūnda gu dul jêh͈.


Wande ku mu mun a don ku di nān chi ndoh͈ mi ma ko mayi, du marati muk; wande ndoh͈ mi ma ko mayi, di na neka chi bir am ab tên i ndoh͈ mu di nacha be cha dūnda gu dul jêh.


Janga ngēn mbinda yi, ndege dēfe ngēn ne chi ñom ngēn am dūnda gu dul jêh͈; te yile ma sēde;


Chi dega, chi dega, ma ne len, Ku di gum, mō am dūnda gu dul jêh͈.


Simon Peter tontu ko, ne, Borom bi, fi kan la ñu ela dem? Yā am i bat i dūnda gu dul jêh͈.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan