Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 19:12 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

12 Ndege i yōm la ñu judu on nōga cha sēn bir i ndey; yenen i yōm la ñu nit yōmlo; te i yōm la ñu yōmlo sēn bopa ngir ngur i ajana. Ku ko mun a nangu, na ko nangu.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 19:12
8 Iomraidhean Croise  

Wande mu ne len, Ñepa munu ño nangu kadu gile, wande ña ñu ko may dal.


Fōfale ñu indi fi mōm gūne yu tūti, ndah͈ mu teg i loh͈o am chi ñom, te ñānal len: tālube ya h͈ūle len.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan