Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 19:10 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

10 Tālube ya ne ko, Su neke nōgule chi digante gōr ak jabar am, bāh͈ul ñu sey mbōk.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 19:10
15 Iomraidhean Croise  

Wande mu ne len, Ñepa munu ño nangu kadu gile, wande ña ñu ko may dal.


Te mangi len di wah͈, Ku fase ak jabar am, lu moy mu di chi njālo, te sey ak kenen, njālo na: te ku sey ak ka ñu fase, njālo na.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan