34 Borom am mer, te jebale ko getenkat ya, be ba mu feye lu mu ko leb on yepa.
Mu fēta, wande dem tejlu ko chi kaso, be ba mu feye bor ba.
Warul kon you it nga yerem sa naule, naka ma la yereme on?
Nōgu la itam suma Bay ba cha ajana di def ak yēn, su ngēn dul baalalante sēn morom chi sēn h͈ol.