Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 18:31 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

31 Ba naule am ya gise la mu def, ñu nah͈arlu lol, te ñou nitali sēn borom la mu def on.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 18:31
16 Iomraidhean Croise  

Bur ba nah͈arlu ko; wande ndig geñ am ga, ak ña tōg on ak mōm di leka, mu ebal ñu may ko ko.


Wande jām bōbale gēna, te feka kena chi i naule am, ku ko leb on tēmēr i kopar: mu japa ko, ne ko chih͈ chi bāt am ne, Fey ma lo ma leb on.


Mu fēta, wande dem tejlu ko chi kaso, be ba mu feye bor ba.


Fōfale borom am ôlo ko fi mōm, te ne ko, E jām bu soh͈or bi, mā la baal on bor bōbale yepa, ndege dagān on nga ma:


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan