30 Mu fēta, wande dem tejlu ko chi kaso, be ba mu feye bor ba.
Naule am ba sūka, te dagān ko, ne, Muñal ma, di nā la fey.
Ba naule am ya gise la mu def, ñu nah͈arlu lol, te ñou nitali sēn borom la mu def on.