25 Wande ndege amul lu mu ko feye, borom am ebal ñu jay ko, ak jabar am, ak i dōm am, ak lu mu am yepa, ndah͈ mu fey bor am.
Ba mu dôre woña, ñu isi fi mōm kena ku ko leb on fuk’ i njūne chi h͈ālis.