Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 18:23 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

23 Mōtah͈ ngur i ajana niro na ak bena bur bu bug’ on a jel konta ak i jām am.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 18:23
17 Iomraidhean Croise  

Mu teg benen lēb chi sēn kanam, ne, Ngur i ajana niro na ak nit ka ji on jiu ju bāh͈ chi tōl am;


Mu teg benen lēb chi sēn kanam, ne, Ngur i ajana niro na ak pēp’ i sūna, bu nit fab, te ji chi tōl am;


Mu wah͈ len benen lēb, ne, Ngur i ajana niro na ak mporoh͈al bu jigen jel, te def chi ñet’ i andār i sunguf, be yepa foroh͈.


Ngur i ajana nirôti na ak mbal mu ñu sani chi gēch, mu japa h͈êt i jen wu neka:


Mu ne len, Bindānkat bu neka mbōk bu ñu nekalo tālube chi ngur i ajana, niro na ak borom‐ker ku gēne chi dēnchukay am lu ês ak lu maget.


Ba mu dôre woña, ñu isi fi mōm kena ku ko leb on fuk’ i njūne chi h͈ālis.


Fōfale di nañu nirale ngur i ajana ak fuk’ i h͈ēk, ñu jel on sēn i lampa, di gatanduji borom‐seyt.


Mel na niki nit ku don tūki chi benen rew, mu ôlu i jām am, te dēnka len alal am.


Rēchu len, ndege ngur i ajana jegeñsi na.


Mōtah͈ ku mu mun a don ku dēga suma i bāt yile, te def len, di na niro ak nit i sago, ka tabah͈ nēg am chi kou doch:


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan