17 Su len bañê dēga, wah͈ ko ndaje ma; te su bañê dēga ndaje ma itam, na neka chi you niki Gentile ak publican.
Philip, ak Bartholomew; Thomas, ak Matthew publican bi; James dōm i Alphæus, ak Thaddæus;
Dōm i nit ka ñou di leka te di nān, te ñu ne ko, Fuh͈alekat bi, ak nānkat i biñ bi, ak and’ i publican yi ak bakarkat yi. Wande sago jubantiku na chi i jef am.
Ndege su ngēn sope ña len sopa dal, ban yōl ngēn di am? Publican ya sah͈ du ñu def nōgule am?
Te su ngēn di ñān, bu len wah͈ati bāt i nēn niki ña h͈amul Yalla; ndege dēfe nañu ne di nañu len dēga ndig sēn bāt yu bare.