Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 17:17 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

17 Yesu tontu, ne, E h͈êt wu gumadi, te deger‐bopa, be kañ lā neka ak yēn? be kañ lā len muñal? Indi ko fi man.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 17:17
25 Iomraidhean Croise  

Defu fa i koutef yu bare ndig sēn gumadi.


Ba ko Yesu h͈ame, mu ne, E gā’ ngum gu new, lutah͈ ngēn werante chi sēn digante, ndege amu len mburu?


Yubu on nā ko chi sa i tālube, te munu ñu ko weral.


Yesu h͈ūle ko, te jine ja gēna chi mōm; cha wah͈tu wōwale h͈alel ba wer.


Wande su Yalla sānge nōgule ñah͈ i tōl mi neka tey, te su elege ñu sani ko chi tāl, du len gen a sānga’m, yēn nit i ngum gu new?


Mu ne len, Lutah͈ ngēn ragal, yēn nit i ngum gu new? Fōfale mu jog, te eda ngelou ya ak gēch ga; mu dal be ne nem.


Ganou lōlu mu ne Thomas, Defal file sa baram, te gis suma i lōh͈o; te defal file sa loh͈o te jō ko chi suma wet: te bul gumadi, wande na nga gum.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan