15 Borom bi, amal yermande chi suma dōm ju gōr; ndege defa say, te getenu bu miti; faral na tabi chi safara, ak chi ndoh͈.
Jena jigen i Canaan juge cha wet yōya, te mu h͈āch͈u, ne, Amal yermande chi man, E Borom bi, Dōm i Dauda; jine anga geten suma dōm ju jigen bu miti.
Yubu on nā ko chi sa i tālube, te munu ñu ko weral.
Dēgdēg i tur am dem cha bir Syria yepa; ñu yub ko nit ña op’ on ñepa, ña jangaro ju mun a don ak nchono jap’ on, ak ña i jine jap’ on, ak ña say, ak ña lafañ, te mu weral len.
Judas, ka ko or on, h͈am on na bereb ba; ndege Yesu faral on na dem fōfa ak i talube am.