11 Mu tontu len, ne, Elijah di na ñou chi dega, to delo yef yepa:
I tālube am lāj ko, ne, Lutah͈ bindānkat ya ne Elijah ela na jeka ñou?
Wande mangi len di wah͈, Elijah ñou on na jēg, te h͈amu ñu ko won, wande ñu def ko lu ñu buga chi mōm. Nōgu itam la ño sonaleji Dōm i nit ka.