1 Ganou jurom ben’ i fan, Yesu jel Peter, James, ak John rak’ am, te yubu len chi kou tūnda wu koue, ñom dal:
Mu sopaliku chi sēn kanam: h͈ar‐kanam am di melah͈ niki janta bi, te ser am wêh͈ tal niki lêr gi.
Mu jel ak mōm Peter ak ñar i dōm i Zebedee, dôr di yogorlu ak nah͈arlu lol.