7 H͈alāt nañu chi sēn bopa, ne, Ndig indiū ñu on mburu.
Yesu ne len, Otu len te moytu mporoh͈al i Pharisee ya ak Sadducee ya.
Ba ko Yesu h͈ame, mu ne, E gā’ ngum gu new, lutah͈ ngēn werante chi sēn digante, ndege amu len mburu?
Batise’ John, fan la juge won? cha ajana am chi nit? Ñu werante chi sēn digante, ne, Su ñu ne, Cha ajana; di na ñu ne, Lutah͈ gumu len ko won mbōk?