6 Yesu ne len, Otu len te moytu mporoh͈al i Pharisee ya ak Sadducee ya.
Pharisee ya ak Sadducee ya ñou di ko fir, te lāj ko mu won len mandarga cha asaman.
Lutah͈ be h͈amu len ne wah͈u ma len chi mburu? Wande ndah͈ ngēn otu mporoh͈al i Pharisee ya ak Sadducee ya.
Fōfale ñu h͈am ne wah͈ul len ñu otu mporoh͈al i mburu, wande njemantal i Pharisee ya ak Sadducee ya.
Tālube ya ñou cha genen wet ga, te ñu fate won a jel mburu.
H͈alāt nañu chi sēn bopa, ne, Ndig indiū ñu on mburu.
Wande ba mu gise jupa chi Pharisee ya ak Sadducee ya di ñou chi batise am, mu ne len, E h͈êt i ñangōr gi, kan a len yēgal ngēn di ūt a rēcha chi mer mi di ñou?
Talube ya wah͈ante, ne, Ndah͈ kena indiwul lu mu leka?