5 Tālube ya ñou cha genen wet ga, te ñu fate won a jel mburu.
Mu demlo mbōlo ma, duga chi gāl ga, te ñou chi i wet i Magadan.
H͈êt wu bon ak njālo ūt na mandarga; du ñu ko may mandarga, lu dul mandarga i Jonah. Mu bayi len, te dem.
Yesu ne len, Otu len te moytu mporoh͈al i Pharisee ya ak Sadducee ya.