4 H͈êt wu bon ak njālo ūt na mandarga; du ñu ko may mandarga, lu dul mandarga i Jonah. Mu bayi len, te dem.
Bayi len len; ño di njīt yu silmah͈a. Te su silmah͈a jītê silmah͈a, di nañu tabi chi mpah͈ ñom ñar.
Tālube ya ñou cha genen wet ga, te ñu fate won a jel mburu.