23 Wande mu walbatiku, te ne Peter, Randu ma, Seytane si; yā di suma mpaka; ndege topatoū la yu jem chi yef i Yalla, wande yef i nit.
Peter japa ko, te dal di ko eda, ne, Borom bi, na la Yalla yerem; lile du la dal muk.
Suboh͈un aduna si ndig i mpaka! ndege i mpaka soh͈la naño dika; wande suboh͈un nit ka tah͈ mpaka ñou.
Fōfale Yesu ne ko, Randu ma Seytane, ndege binda nañu, ne, Na nga jāmu Borom ba sa Yalla, te na nga ko topa, mōm reka.
Yesu tontu len, ne, Ndah͈ du yēn lā tan’ on, fuk’ ak ñar ña, te kena chi yēn ab seytane la?