Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 16:21 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

21 Cha sā sōsale Yesu dal di won i tālube am naka mu ela deme fa Jerusalem, te sona yef yu bare chi mag ya, ak i njīt i seriñ ya, ak bindānkat ya, te di ko rēyi, mu di dēkiji chi ñetel i fan am.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 16:21
31 Iomraidhean Croise  

Ndege naka Jonah nek’on chi bir mbonkana ma ñet’ i bechek ak ñet’ i gudi, nōgule la Dōm i nit ka di nekeji chi h͈ol i suf si ñet’ i bechek ak ñet’ i gudi.


Peter japa ko, te dal di ko eda, ne, Borom bi, na la Yalla yerem; lile du la dal muk.


Chi dega mangi len di wah͈, Ñena ñi tah͈ou file, du ñu mos dē, be ba ñu di gisi Dōm i nit ka mu di ñou chi ngur am.


Wande mangi len di wah͈, Elijah ñou on na jēg, te h͈amu ñu ko won, wande ñu def ko lu ñu buga chi mōm. Nōgu itam la ño sonaleji Dōm i nit ka.


Ba ñu wache tūnda wa, Yesu ebal len, ne, Bu len wah͈ kena mpêñu mile, be ba Dōm i nit ka di dēki cha ñu dē ña.


Naka Dōm i nit ka ñouūl ndah͈ ñu bukanēgu ko, wande ndah͈ mu bukanēgu, te may dund’ am njot ngir ñu bare.


H͈am ngēn ne cha ganou ñar i fan h͈ewte ga di na jot, te ñu or Dōm i nit ka ndah͈ ñu dāj ko chi kura.


Ba mu wah͈andô, Judas, kena chi fuk’ ak ñar ña, ñou, and’ ak mōm mbōlo mu rey ñu am i jāsi ak i doko, ñu juge fa i njīt i seriñ ya ak i mag i nit ña.


Ba ko i njīt i seriñ ya ak mag ya jêñe, tontuwul dara.


Ne, Borom bi, Fataliku nañu ne nafeh͈a bōbale nôn na ba mu dund’ on, Chi ganou ñet’ i fan di nā dēki.


Nekul file; ndege dēki na, chi naka mu ko wah͈e won. Ñou len, sêt bereb bi fi ñu teral on Borom bi.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan